SSMay 9, 2025 · 3 hr 27 minS. Sam Gammou Louga 1997Serigne waxtaan wu am solo lool ci Al Muhtamaa, Sallal aahu halayhi wa sallama
SSMay 9, 2025 · 3 hr 27 minS. Sam Gammou Louga 1996matt naa teewlu lool, ta jeem sunu kemm kattan ci di jeema xeex ak sunu bakkan di jefe ay njangaleem ta yalla rek tax. Dax kat njarin li ci lolu kepp la nekk
SSMay 9, 2025 · 4 hr 29 minS. Sam Gammou Louga 1994diglu ko ci soo amee ak yaatou ngir mana tewwlu limouy wax ak tontu yimuy andi ci laaj yu am solo yi
SSMay 9, 2025 · 4 hr 24 minS. Sam Gammou Louga 1993diglou ko ci waxtu woo amee ak yatou ngir mana jel ay bind ci yennati wax yi ndax yombuta jang ciy teere